Description
Kwame mi poliis njortoon ne dafa laalee ci gëfug porfesër Omar gi, da ñu koo jaapoon. Ba sàmbaabóoya nee na ñu leen danna, ca la ñu ko setal. Diggante Kwame ak Nathalie di gënna ratax ndax li mu xamoon leeb ba... Kwame, gëstoom moo ko yóbbuwoon ba Niseer, ca Iniwersite bu Niamey.