Episodes
Teyaataru rajo ci làkk yu bari ci 25 jataay yu 7 simili bu neek ngir nga toop, ci farañse ak ci sa làmiñ wi nga nàmp, gëstuy poliis yu keemaane.
Published 11/11/22
Deglul ngelawli: Sahara munge jooy. Mi ngi xaar nit ku jup ku baax ki kay naatalaat.
Published 11/11/22
Ndaq Kwame da na man a aaye polise ñu dal ci gëfat ya ak fitna ngir rawale « waa ju baax ja te dëggu » ? Guddi jotna, barab bal lëndëm te dëll, fa la leep di jeexee.Waa kër Fenjugu ngànaayu na ñu, polisee ya itam na ka noona : danna ga mat na : teemeeri junni ëro yu mana jur bëg-bëg ak xëccoo yu ne…

Waxtu wiy daw ngir wallu porfesër Omar : gëfkat yi joxewoon jamono joo xam ne bu weesoo rek te jotuñu xaalis ñu ray ko. Kwame ak nathalie dem seeti nu nuy gisee njoogaanu porfesër Abubaakri ba ak Kuada. Ndaq daf a am lu ko boole ak nit ku lëndëm ka ñu naan fenjegu ?

Ca biir tukki ma bu àndoon ak Clément ci oto, teg ca gaal, ca la Kwamé tàmbalee xam ci lan la njaatigeem doon liggéey, xam-xamam màcc ci mbay ak njureel.Ñaari yoon, mu am ñu koy jeema baayiloo gëstoom: posaneko ak capaloo ca Boubon; di fexee it mu baña taseek profesër Kouada ca Niamey.Ci ndimalu Nathalie,la gisee tuuti ca mbóot ma doon ubbi dencukaay bu yeemee ba "Sahel vert".

Kwame mi poliis njortoon ne dafa laalee ci gëfug porfesër Omar gi, da ñu koo jaapoon. Ba sàmbaabóoya nee na ñu leen danna, ca la ñu ko setal. Diggante Kwame ak Nathalie di gënna ratax ndax li mu xamoon leeb ba... Kwame, gëstoom moo ko yóbbuwoon ba Niseer, ca Iniwersite bu Niamey.

Kwame surgab tóokóor la ca Gorom-Gorom, ca Burkina Faso. Njaatigeem, porfesër Omar Seku, da ñu koo gëfoon ca kanamam. Ca biir xeex ba, gàllaajam dammu.Kwame dem di wëri Omar ma doon jeema dekkalaat ndànd foy-foy gi. Ku ko gëf?Gëf ga ak gàllaaj ku doy waar gi ndaq da ñoo am lu ñu joteek leebu bajani Kwame ja? "Deklul ngelawli, Sahara munge jooy. Dafa buga naataat. Bena bes Bena bes dina am nit ku ñew. Dina dekkelaat gañcax ak garap yi... "