Épisode 13: Il faut garder le secret
Listen now
Description
Ca biir  tukki ma bu àndoon ak Clément ci oto, teg ca gaal, ca la Kwamé tàmbalee xam ci lan la njaatigeem doon liggéey, xam-xamam màcc ci mbay ak njureel.Ñaari yoon, mu am ñu koy  jeema baayiloo  gëstoom: posaneko ak capaloo ca Boubon; di fexee it mu baña taseek profesër Kouada ca Niamey.Ci ndimalu Nathalie,la gisee tuuti ca mbóot ma doon ubbi dencukaay bu yeemee ba "Sahel vert". 
More Episodes
Teyaataru rajo ci làkk yu bari ci 25 jataay yu 7 simili bu neek ngir nga toop, ci farañse ak ci sa làmiñ wi nga nàmp, gëstuy poliis yu keemaane.
Published 11/11/22
Deglul ngelawli: Sahara munge jooy. Mi ngi xaar nit ku jup ku baax ki kay naatalaat.
Published 11/11/22