02: Jaar-jaari Seex Ahmadu Bamba
Listen now
Description
Ci waa jataa yu Magal Touba Al Muraaxaba mooy and ak yeen ci Jaar-jaari Seex Ahmadu Bamba ak Sëriñ Basiiru Mbàkke Xelkoom
More Episodes
Yàlla moo dëgal sunu maam Ibrahima, mu ray doomam, waay Yàlla joto ko ap gaat, foofa la ñi sonnal lee Tabaski ci Jolit. Al Muraaxaba
Published 06/12/24
Published 06/12/24
Jokku yu bon ci jigeen, jar naa bayyi xel, ak Sëriñ Hady niass ci Al Muraaxaba
Published 06/06/24