Is this your podcast?
Sign up to track ranks and reviews from Spotify, Apple Podcasts and more
Studio Ëpoukay
Jiggéen yuy tukki 
Dakaar ba fépp ci àdduna
Suniouy wakh si migration fi sénégal, liniouy geuneu xalaat moy ay ndaw you goor yuy dieul gaal nguir dem Espagne. Wayé daniouy faté ni si biir tukki katt yoyou amna ay jiguén. Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information.
Listen now
Recent Episodes
Épisode bou moudjou si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay. Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information.
Published 03/14/24
Diourom bennelou épisode bi si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay. Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information.
Published 03/13/24
Do you host a podcast?
Track your ranks and reviews from Spotify, Apple Podcasts and more.
See hourly chart positions and more than 30 days of history.
Get Chartable Analytics »